Genesis 34:24
TSK
Ba mu ko defee mboolem góori dëkk ba déggal Amor ak doomam Sikem, ba ñoom ñépp xaraf.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba mu ko defee mboolem góori dëkk ba déggal Amor ak doomam Sikem, ba ñoom ñépp xaraf.
Ma teg kayit yi ci loxol Barug doomu Nerya doomu Maaseya. Anamel sama doomu baay bu ndaw fekke na ko, seede yi torlu kayitu njaay mi fekke ko, ñook mboolem Yudeen ñi toogoon ci ëttu dag yi.