Genesis 24:5
TSK
¶ Surga ba ne ko: «Su ndaw sa nanguwula ànd ak man ci réew mii nag? Ndax kon damaa wara yóbbu sa doom ba ca réew ma nga jóge?»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.