TSK

TSK · Genesis 24:49

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ci kaw loolu Yanqóoba ñaan Yàlla, ne ko: «Yaw Aji Sax ji, sama Yàllay maam Ibraayma, di sama Yàllay baay Isaaxa itam, yaa ma ne woon: “Dellul réew ma nga cosaanoo, ca say bokk; dinaa la baaxe.”

Ngalla nag may nu, nu jaare sam réew. Dunu fi jaare benn tool, mbaa ab tóokëru reseñ, dunu fi naane ndoxum benn teen. Mbeddum buur daal lanuy topp, dunu jàdd ndijoor ak càmmoñ, ba keroog nuy génn sam réew.»