TSK

TSK · Genesis 27:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Yanqóoba ne ko: «Giñal ma jëkk.» Esawu giñal ko ko, mu jaay Yanqóoba ndono, li mu yeyoo ndax li muy taaw.

Dige naa sama bakkan; boo yeboo laaj ma ko. Bu ma la ko délloosilul, ba teg ko fi sa kanam, maa lay tooñ sama giiru dund.

¶ Ba loolu amee Sóol ne: «Nan toppi waa Filisti ci guddi gi, nu sëxëtoo seen alal ba bët set, te bunu ci bàyyi kenn, mu dund.» Mbooloo ma ne ko: «Loo bëgg rekk, defal!» Sarxalkat ba nag ne ko: «Nanu ko jëkka diis Yàlla fii.»

Jigéen ja ne ko: «Buur sang bi, àq ju ci am, yal na ma topp, maak sama waa kër baay, te nga bañ cee gàddu dara, yaak sa waa kër.»