TSK

TSK · Genesis 28:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Kon doom, defal lii ma lay wax, demal làquji fa sama càmmiñ Laban ca Karan,

¶ «Na ku nekk weg ndeyam ak baayam te wormaal sama bési Noflaay. Man Aji Sax ji, maay seen Yàlla.

Kuy xeelu sa baay, di siidee déggal sa ndey, baaxoñ génne ciw xur, luqi sa bët, tan ya lekk.

ndax da ne: «ngir ngeen baaxle te gudd fan ci kaw suuf.»