Genesis 3:12
TSK
Aadama ne ko: «Jigéen, ji nga ma booleel de, moo ma jox ci garab gi, ma lekk.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Aadama ne ko: «Jigéen, ji nga ma booleel de, moo ma jox ci garab gi, ma lekk.»
ay goney Yàlla ñoo gis jigéen ñeek seen taar, ñuy jël ñi ñu bëgg ci ñoom, def leeni jabar.
Mu walbatiku ànd ak moom ca kër ga, sex fa dugub, naan fa ndox.
«Yaw nit ki, maa ngii di nangusi sa bànneexu bët cim pàdd. Bul yuuxu, bul jooy, bu sa rongooñ wadd.
¶ «Yaw nit ki, bés bu ma nangoo ci ñii seen tatay daraja ji ñuy bége, muy seen bànneexu bët, di seen xintey bakkan, ba nanguwaale seen doom yu góor ak yu jigéen,
Te it du Aadama lañu nax, waaye jigéen lañu nax ba mu xëtt ndigal.