Genesis 3:5
TSK
Waaye Yàlla xam na ne bés bu ngeen ci lekkee, seeni bët dina ubbiku, ngeen mel ni Yàlla, xam lu baax ak lu bon.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waaye Yàlla xam na ne bés bu ngeen ci lekkee, seeni bët dina ubbiku, ngeen mel ni Yàlla, xam lu baax ak lu bon.»
Dingeen mujj dof ndax lu buur seeni bët ngeen di gis.
¶ Ba ñu duggee Samari, Alyaasa dellu ñaan ne: «Aji Sax ji, ngalla ubbil bëti nit ñii, ñu gis.» Aji Sax ji muri seeni bët, ñu xoole rekk, gis ne ñu ngi biir Samari.
Lal a gàtt ba deesu ci tàlli, malaan cëkk ba matul càngaay.
Ci kaw loolu ñu dugal ko sawara. Ca biir mbugal mu tar ma la dawale bëtam, daldi séen fu sore Ibraayma ak Lasaar ci wetam.