TSK

TSK · Genesis 30:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ba Leya ëmbee, am doom ju góor, da koo tudde Ruben (mu firi Gisleen, doom ju góor a ngi), ndaxte Leya da ne: «Aji Sax ji gis na sama toroxte. Léegi sama jëkkër dina ma bëgg.»

Giir yii nag ñooy taxaw di rëbbe, fa kaw tundu Ebal: Rubeneen ñi ak Gàddeen ñi ak Asereen ñi ak Sabuloneen ñi ak Daneen ñi ak Neftaleen ñi.»

Aji Sax ji sama Yàlla, àttee ma sa dëgg, ñu bañ maa ree!

Ma jënd njiitlaay, woddu, muy la Aji Sax ji wax.

Maa leen di def seen jaami noon réew mu ngeen xamul, sama mer jippét, tàkkal leen.»