TSK

TSK · Genesis 31:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Loolu tax bëy yay tëbu ca wetu car ya, di jur doom yu seereer, yu tippante ak yu todde.

Te mboolem alal, ji Yàlla nangoo ci sunu baay, noo ko moom, nun ak sunuy doom. Kon nag léegi lu la Yàlla wax rekk, def ko.»

¶ Gannaaw loolu Buur Aserus jox bésub keroog Lingeer Esteer kër Aman, fitnaalkatu Yawut ya. Ñu woo Mardose ca Buur, ndax fekk na Esteer xamle ba noppi na Mardose bokkeek moom.

Ku baax, donale ba cay sëtam; alalu moykat, muuru ku jub.