2 Kings 4:30
TSK
Teewul yaayu xale ba ne ko: «Ak sama digganteek Aji Sax ji, Kiy Dund, nga fekke tey, duma la fi bàyyi.» Mu daldi jóg topp ca moom.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Teewul yaayu xale ba ne ko: «Ak sama digganteek Aji Sax ji, Kiy Dund, nga fekke tey, duma la fi bàyyi.» Mu daldi jóg topp ca moom.
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di kàddug Sabóor, ñeel Daawuda.