Genesis 9:25
TSK
Ba mu ko defee mu ne: «Yal na Kanaan torox, bay jaamu jaami doomi ndeyam.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba mu ko defee mu ne: «Yal na Kanaan torox, bay jaamu jaami doomi ndeyam.»
¶ Gannaaw gi Rebeka ne Isaaxa: «Àddina soof na ma ndax jigéeni Etteen ñi. Yanqóoba de, bu jëlee ci jigéeni réew mi di Etteen ñu mel ni ñii, sama dund gi, dee a koy gën!»
Doomi Ana ñooy Dison ak Olibama, doomam ju jigéen.