TSK

TSK · Genesis 36:43

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ismayla moomee nag, doomu Ibraayma jaak Ajaram Misra, ma doon jaamub Saarata, askanam mooy lii.

Li ko waral mooy, seen alal dafa bare woon lool, ba manuñoo dëkk ñoom ñaar, te réew, mi ñu daloon, àttanu leen ndax seen gétt yu bare.

¶ Askanu Esawu, di maami Edomeen ña ca tundi Seyir, mooy lii.

Ñi xeetoo ci Olibama soxnas Esawu, ñooy Yewus, Yalam ak Kora, ku ci nekk ak làngam. Ñooñooy làngi Olibama, soxnas Esawu siy doomu Ana.

Kon nag du yeena ma yebal fii, waaye Yàllaa. Te moo ma jagleel, ma doon cëslaayal Firawna, mel ni baay ci moom, jiite këram gépp, boole ci yilif mboolem réewum Misra.

¶ Gannaaw gi, Musaa moo yebale ay ndaw fa dëkk ba ñuy wax Kades, ñu dem ca buurub Edom, ne ko: «Israyil say bokk dañoo wax ne: Umplewoo mboolem coono bi nu daj.