TSK

TSK · Genesis 37:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Liy cosaanal asamaan ak suuf, ba ñu leen di sàkk, mooy lii. Bés ba Aji Sax ji Yàlla sàkkee suuf ak asamaan,

¶ Askanu Nóoyin mooy lii. Nóoyin nit ku jub la woon, di ku mat ci biir nit ñi mu bokkal jamono, te di ku topp Yàlla.

Ci kaw loolu mu may ko jaamam Bilaa, muy soxnaam. Yanqóoba dëkkoo Bilaa,

¶ Ba Israyil dëkkee ca réew ma, am na bés Ruben dem tëdd ak Bilaa, nekkaaleb baayam; Israyil yég ko. Doomi Yanqóoba yu góor fukk lañu ak ñaar.

Yuusufa xàmmi na ay magam, waaye ñoom xàmmiwuñu ko.

¶ Déggees na nag ci lu wér, ne powum séy am na ci seen biir, te powum séy mu ni mel, giseesu ko sax ci biir xeeti yéefar yi. Dem na sax ba nit nekk ak jabaru baayam.