TSK

TSK · Genesis 37:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ba Yuusufa agsee ca magam ya, dañoo futti mbubbam, mooy mbubb mu yànj, ma mu soloon.

Ba mu ko defee nu ne la: “Am nanu baay bu màggat. Sunu rakk, ji mu jur te fekk ko di màggat nag, moo ci gën di ndaw. Magam dafa dee, mu des moom doŋŋ ci ndeyam, baayam sopp ko lool.”

Surga ba génne ko, tëj bunt baak caabi. Tamar a nga sol mbubb mu yànj, ndax booba janqi buur bu séyagul noonu la daan soloo.

Yaa tànn ci sa yére yu yànj, rafetale sa jaamookaayi tuur, ba noppi di ca gànctu; lu masula am te du amati mukk.