TSK

TSK · Genesis 38:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

«Dégluleen ma, ngalla sang yi, siyaare naa leen, tee ngeena dal ak man, su ko defee ngeen jàngu, fanaan ba suba, ngeen xëy topp seen yoon?» Ñu ne ko: «Bàyyil, nu fanaan ci mbedd mi.»

¶ Ba loolu amee Daawuda jóge Gaat, daw làquji ca biir xuntim Adulam. Magam yaak waa kër baayam gépp yég ko, dikk, fekksi ko fa.

¶ Am na bés Alyaasa jaare dëkk bu ñuy wax Sunem. As ndaw su bare alal woo ko lekk këram, di ko soññ. Mujj na saa yu fa jaaree, daldi fay toog, ba xéewlu.

Àndal ak ku xelu, sam xel rafet; ku lëngook ub dof, loru.