¶ Gànc bu jigéen buy gànctul ay tuur, bumu am ci biir jigéeni Israyil, te gànc bu góor buy gànctul ay tuur, bumu am ci góori Israyil.
TSK
TSK · Genesis 38:16
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ezekiel 16:33
TSK
Mboolem caga yi dañuy feyeeku! Waaye yaw yaay neexal sa far yépp, di leen fey ñu jóge fu ne, di la tëdde.
1 Timothy 6:10
TSK
Ndax sopp xaalis kat mooy reenu mboolem xeeti loraange. Am na ñuy ŋaf-ŋafi, di ko wut, far lajj yoonu ngëm, ba teg seen bopp tiis yu bare.