TSK

TSK · Genesis 39:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ba loolu amee bés bu Yàlla sàkk mu di ko wax Yuusufa, te dégluwu ko, wéetul ak moom sax, bay tëdd ak moom.

Naka la Tamar dikk, taajal Amnon mburu ya, ngir mu lekk, mu ne ko katam, ne ko: «Kaay, tëdd ak man, sama jigéen.»

¶ «“Yaaka weex bët, kàddug Boroom bi Aji Sax jee, lii lépp di jëfi gànc bu dëgër bët.

¶ Soppe yi, ay gan ngeen, ay doxandéem ci kaw suuf. Kon nag li ma leen di dénk moo di ngeen moyu xemmemtéefi bakkan yiy xeex ak ab xol.