TSK

TSK · Genesis 40:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ñu ne ko: «Ay gént daal a nu dikkal, te amunu ku nu koy firil.» Yuusufa ne leen: «Xanaa du Yàllaa moom piri? Nettalileen ma seeni gént rekk kay.»

genn guddi danoo géntandoo, man ak moom, gént gu ci nekk ak la muy firi.

Yuusufa ne ko: «Du ci man de, waaye Yàlla mooy baaxe Firawna pirim jàmm.»

Ca guddi ga nag, ñu won mbóot ma Dañeel ci biir peeñu. Ci kaw loolu Dañeel sant Yàlla Boroom asamaan,

loolu yépp ndax dañoo gis ci kooku Buur tudde Beltasar, xel mu ñaw akum njàng ak ràññee. Day firi gént, di teqental ay cax ak a lijjanti ay jafe-jafe. Kookooy Dañeel; kon nañu ko woo, mu wax piri mi.»