TSK

TSK · Genesis 42:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

ba nit ñiy jóge fu nekk ci àddina, di wutsi njël ci Yuusufa ndax xiif bu mettee fépp ca àddina.

Farbay ngàllo, ga bokk ca bànni Israyil nag xam ne dal nañu aw sas, ndax la ñu leen ne duñu wàññi lenn ca limu móol, ya leen war bés bu nekk.

Ba juróom ñaari at ya matee, ndaw sa jóge ca réewum Filisteen ña, ñibbsi. Mu dem ca Buur, di sàkku mu delloo ko këram ak suufam.

«Ana lu nuy toog? Fabuleen, nu dem ca dëkk ya tata wër, deeyi fa. Sunu Yàlla Aji Sax ji nar na sunu dee; moo nu nàndal tookey mbugal, nde noo tooñ Aji Sax ji.

Acts 7:12 TSK

Yanqóoba dégg ne ab dund am na Misra. Ca la fa jëkka yebal sunu maam ya.