TSK

TSK · Genesis 42:29

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Booba lanu dem ca sunu baay, ba lay siyaare, daldi koy jottli say kàddu.

Ñu wax ko ne ko: «Ndekete Yuusufaa ngi dund! te sax mooy kilifag réewum Misra gépp.» Ba Yanqóoba déggee loolu, yaramam dafa dee goyy ca saa sa, ndaxte gëmu leen.