TSK

TSK · Genesis 43:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Gannaaw loolu Yuusufa joxe ndigal, ñu sol seeni saaku pepp, te ku nekk ca ñoom, ñu yebal ko xaalisam ca saakoom, ba noppi mayaale leen lu ñu lekk ca yoon wa. Ñu defal leen noonu.

¶ Buleen feyantoo, fexeleen di def lu rafet, ñépp seede ko.

Li nuy xinte moo di li baax ci kanam Boroom bi, te baax ci kanam nit ñi itam.

Ci moomu mbir, bu kenn ci yeen tooñ mbokkam, di aakimoo yelleefam, ndax waxoon nanu leen ko, ba artooti leen ne leen jëf ju ni mel, Boroom bee koy fey ña ko def.

Yeesu Almasi menn mi la woon démb ak tey ba fàww.