Genesis 42:2
TSK
Mu ne leen: «Dégg naa ne pepp am na ca Misra. Demleen jëndali nu ca, ndax nu mana dund, ba xiif bañ noo rey kay!»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Mu ne leen: «Dégg naa ne pepp am na ca Misra. Demleen jëndali nu ca, ndax nu mana dund, ba xiif bañ noo rey kay!»
Ñu ne ko: «Sang bi baal nu, nun de ñëwoon nanu fi lu jiitu ngir jëndsi dund,
Néewle te ragal Aji Sax ji moo gën barele, sa bopp ubu.
Day seetlu ab tool, jënd ko, sàkk ciw ñaqam, jëmbat tóokër.
¶ Teewul njullite gu ànd ak doylu, di alal ju réy.