TSK

TSK · Genesis 43:20

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ci kaw loolu fukki magi Yuusufa ya dem Misra, jëndi pepp.

¶ Fa ñu dal ca guddi, kenn ci ñoom bëgga xont mbaamam, ubbi saakoom rekk, ne pemm ci xaalisam.

Yuda ne ko: «Waa ja da noo àrtu woon de, wax na nu ne nu: “Dootuleen jàkkaarlook man te ànduleen ak seen rakk.”

Senn ndaw sa ne: «Éy sang bi, maak ndaw sii de, danoo bokk genn kër, bokk fa wasin nun ñaar.