TSK

TSK · Genesis 43:32

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Gannaaw loolu Yanqóoba sàkk sarax ca kaw tund wa, woo ay bokkam, ñu bokk lekk. Ba ñu lekkee ba noppi, fanaan ca tund wa.

“Lan mooy seen liggéey?” ngeen ne ko: “Nun de sang bi, ag jur lanu masa yar, ba nuy gone ba tey, te noonu la ko sunuy maam daan defe.” Su boobaa, ngeen mana féetewoo diiwaanu Gosen, ndaxte waa Misra dañuy xof sàmm.»