TSK

TSK · Genesis 43:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

te nun ñépp a bokk baay, di nit ñu maandu; nun kay, sang bi, dunu ay yëddukat.»

Yuda ne ko: «Waa ja da noo àrtu woon de, wax na nu ne nu: “Dootuleen jàkkaarlook man te ànduleen ak seen rakk.”

Sang bi, danga noo laajoon ne nu: “Ndax am ngeen baay walla rakk?”