TSK

TSK · Genesis 44:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Rikk bul yemale ku jub ak ku jubadi, ba boole leen rey, loolu jomb na la moos! Yaw miy àtte àddina sépp kay, lu jub rekk ngay def!»

Gannaaw loolu ñu yóti seen baay mbubb ma, ne ko: «Lii lanu gis de, xoolal bu baax ndax du sa mbubbu doom?»

Mu ne leen: «Li ngeen wax yoon la sax, waaye na ki ma ko fekke doŋŋ di sama jaam, su ko defee ñi ci des wàcc.»

Yàlla, nu sant la, santati la; nu ngi lay woo, di siiwal say jaloore.