1 Samuel 24:17
TSK
¶ Ba Daawuda waxee Sóol kàddu yooyu ba daaneel, Sóol da ne: «Éy Daawuda, doom, loolu sa baat la moos?», daldi ne yikkét jooy.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ba Daawuda waxee Sóol kàddu yooyu ba daaneel, Sóol da ne: «Éy Daawuda, doom, loolu sa baat la moos?», daldi ne yikkét jooy.
Ma ji leen njekk, ñu fey ma njekkar, ndaw tiisu xol!
Kuy feye mbon jëf ju baax, lu bon du jóge sa kër.