TSK

TSK · Genesis 44:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Laban ne ko: «Ngalla waay, déglu ma, ngir sama ngisaane won na ma ne Aji Sax ji barkeel na ma ndax yaw.

¶ «Buleen lekk lu am deret. Buleen di gisaane mbaa ngeen di jibar.

Ndaw ya am njort lu rafet nag. Ñu gaaw naa: «Ben Addàd kay sa mbokk a!» Mu ne leen ñu dem indi ko. Ba Ben Addàd dikkee ba ca moom, mu waral ko ca watiiram.