TSK

TSK · Genesis 44:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ba Israyil dëkkee ca réew ma, am na bés Ruben dem tëdd ak Bilaa, nekkaaleb baayam; Israyil yég ko. Doomi Yanqóoba yu góor fukk lañu ak ñaar.

Mu jàdd, ñëw ba ca moom, ne ko: «May ma, ma ànd ak yaw.» Fekk na xamul woon ne goroom la. Mu ne ko: «Loo may fey, ngir ànd ak man?»

Yowab ne ko «Yàlla tere, tereeti ko, may tas ak a faagaagal kenn!

Jëw bu rafet a gën barele, wegeel gën xaalis ak wurus.

¶ Deeleen nu ñaanal nag. Li nu wóor de, moo di sunum xel yeddu nu fenn, te it di def lu baax ci lépp moo di sunu bëgg-bëgg.