Doomam yépp, góor ak jigéen ñëw, di ko dëfal, te noppiwul, xanaa naan: «Damay jooy, ba dem njaniiw, fekki sama doom.» Baayam di ko jooy,
TSK
TSK · Genesis 45:26
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 37:35
TSK
Genesis 42:36
TSK
Seen baay Yanqóoba ne leen: «Xañ ngeen ma ay doom: Yuusufa nekkatul, Simeyon nekkatul, léegi ngeen bëgga jël Beñamin, yóbbu. Loolu lépp ci sama kaw; ngalla man!»
Genesis 44:28
TSK
Kenn ki dem, wacc ma, ma ne moom kay, aw rabu àll a ko daggate! Gisaatuma ko ba tey jii.
Genesis 48:11
TSK
Israyil nag ne Yuusufa: «Yaakaaruma la woona gisati, ndeke Yàlla dina ma may lu raw gis la, ndax gis naa say doom.»
Job 29:24
TSK
Samay ree gëmeesu ko woon, xanaa ne siiwa gis sama kanam gu leer.
Psalms 126:1
TSK
Muy jàngi yéeg, ñu di ko màggale Yàlla. Ba Aji Sax ji delloo waa Siyoŋ seen réew, danoo meloon ni ñuy gént,
Luke 24:11
TSK
Teewul ñu def waxi jigéen ña ay caaxaan, ba gëmuñu leen.
Luke 24:41
TSK
Taalibe ya nag boole mbég akug jaaxle ba tax manuñu koo gëm. Mu ne leen: «Lu ngeen fi am, lu ñuy lekk?»