TSK

TSK · Genesis 45:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ñoom nañu dajale mboolem dundi at yu baax yi, te boole pepp mi ci sa ndigalu bopp, yaw Firawna, muy dund bu ñuy denc ci dëkk yi.

Ba ñu demee, ba metitu xiif bi dajal réew mépp, Yuusufa dafa ubbi denc yépp, di jaay pepp mi waa Misra,

¶ Yuusufa ne waa réew ma: «Léegi gannaaw jënd naa leen, ba Firawna moom leen, yeen ak seeni suuf, jiwoo ngii, demleen jiyi.

Na magi dëkk boobu wommat nag wi ba ci xur wu wal ma dul ŋiise, te maseesu cee bey, maseesu cee ji. Ñu daldi damm loosu nag wu jigéen wi foofa ca wal ma.

Nag yeek mbaam yiy rijji sax, di xontoo cox bu ñu xorom, jóge ci mbàccum roq ak ngaska.