TSK

TSK · Genesis 46:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Sunuy maam a demoon Misra; dëkk nanu Misra lu yàgg, waa Misra di nu mitital, na woon ca sunuy maam.

Mu dellu nag wax fi seen kanam Yàlla Aji Sax ji, ne: «Sama maam ab Arameen buy màngaan la woon. Mu dem Misra, sance fa mbooloo su néew, te mujj di askan wu réy, am doole te bare.

Israyil agsi Misra, muy nganug Yanqóoba ga ca réewum Xam.