TSK

TSK · Genesis 47:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Acts 7:13 TSK

Seen ñaareel bi yoon la Yuusufa xàmmiku ay doomi baayam, Firawna nag doxe ca xam cosaanu Yuusufa.

¶ Almasi moomu nag lanuy xamle; na mu gëna xeloo lanuy àrtoo nit ku nekk, te ni lanuy jàngale nit ku nekk, ngir àgge nit ku nekk ba fa kanam Almasi, fekk ko mat sëkk, na mu ware ku ànd ak Almasi.