Psalms 34:12
TSK
Dikkal doom, déglu ma, ma jàngal la ragal Aji Sax ji.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Dikkal doom, déglu ma, ma jàngal la ragal Aji Sax ji.
Gone yi, tee ngeena dégg yaru baay, te déglu, ba am ug dégg?
Doom, defal li la baay sant, te bul wacc ndigalal yaay.
Kon nag, doom, dégluleen ma, teewluleen samay wax.
Déglul sa baay bi la jur. Bu sa ndey màggatee, bu ko sàggane.
Bokkleen daje yeen ñépp te déglu! Kan ci tuur yii moo yégle lii? Ki Aji Sax ji sopp mooy sottal nammeelu Aji Sax ji ci Babilon, won Kaldeen ña fa dëkke diisaayu loxoom.