TSK

TSK · Haggai 1:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Teewul Yowas dugg na ñaar fukkeelu atu nguuram ak ñett, te taxul sarxalkat ya defarluwaat lenn ci kër Aji Sax ji.

La ko dale bésub keroog sama xaaju nit ña rekk a doon liggéey, xaaj ba ca des gànnaayoo ay xeej aki pakk aki fitt ak kiiraayal dënn. Kilifa ya nag taxaw ca gannaaw mboolem waa Yuda.

Ab yaafus da naan: «Gayndee ngi ci yoon wi! Gayndee ngi ci mbedd mi!»

Mu jot nga rey, mu jot nga faj; mu jot nga toj, mu jot nga tabax.