1 Kings 6:20
TSK
Néeg bu sell baa sell amoon na guddaayu ñaar fukki xasab, yaatuwaay ba di ñaar fukki xasab, taxawaay ba di ñaar fukki xasab; Suleymaan xoob ko wurusu ngalam. Sarxalukaayu seedar ba jàkkaarlook néeg ba, moom it xoob na ko wurusu ngalam.