TSK

TSK · Hebrews 3:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

gannaaw mboolem nit ñi gis samag leer, gis firnde yi ma def ci digg Misra ak ci màndiŋ mi, ñoo ma nattu nii fukki yoon, bañ maa déggal,

Waaye yeen, seeni néew ci màndiŋ mii lay tëdd,

Aji Sax jee leen toppe diisaayu loxoom, wollee leen ci biir dal bi, ba ñu jeex tàkk.

¶ Bokk yi, bugguma ngeen umple ko, sunu maam yépp la niir wa yiiroon, te ñoom ñépp a jàll géej ga.