TSK

TSK · Hosea 8:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Aji Sax jeey def ngeen daanu fi seen kanami noon. Wenn yoon ngeen di dikke, song leen, waaye juróom ñaari yoon ngeen di awe, daw, te dees na leen seexlu ci mboolem nguuri kaw suuf.

Buleen fat tuuru jaambur, buleen sujjóotal tuuru doxandéem.

Ñi ñuy dàqa gëna gaaw ay jaxaay, ci kaw tund yi lañu nu ne dann, màndiŋ mi, ñu di nu fa tëroo.

te su boobaa mbugal war ci ñoom, ndax worma ja ñu fecci.