TSK

TSK · Isaiah 22:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Boroom baa ngii di leen sottisi dexu Efraat gi ne xéew ak dooleem, te mooy buurub Asiri ak mboolem darajaam. Dex gi mooy génn xuram, fees fépp fu dig tàkkam,

Yoon wa mu dikke lay delloo, biib dëkk, du fi dugg. Kàddug Aji Sax jee!

Nga gaw ko, tabax ab gawukaay bu ko wër, sëkk ko, ba noppi sàkkal ko ay dali xare, wërale ko dénki dàjjikaay ba mu daj.