TSK

TSK · Isaiah 29:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Day mel ni gént goo yewwoo. Céy Boroom bi, boo xippee, jëmmu gént ga soof la.

Waaye Asiri gisewu ko noonu, xalaatewul noonu; bóome la xintewoo, ba fàkkas xeeti xeet.

Dinga ko seet, doo ko gis, kuy jànkoonteek yaw, du mujje doon tus, te kuy xareek yaw it day mujj neen.

Nahum 2:1 TSK

Ndaw a ngii dawe kaw tund ya, di indi kàddu, xibaaru jàmm. Yaw Yuda, bégeel sa bési màggal, te wàccook say xas. Nit ku bon ki dootu jaare fi yaw; léppam lees di dagg, sànni.