Dugalal sa alal, dawloo ko; yàgg-yàgg nga jotaat ci.
TSK
TSK · Isaiah 32:20
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Isaiah 30:23
TSK
Su boobaa Aji Sax ji tawal lu ngeen ji, may leen pepp mu suuf meññ, sakkan te nangu, seen juri keroog di fore parlu yu yaa,
Acts 2:41
TSK
¶ Ña nangu kàddug Piyeer nag, ñu sóob leen ci ndox; bésub keroog lu wara mat ñetti junni (3 000) yokku nañu ca gëmkat ña.
Acts 5:14
TSK
Gëmkati Sang bi nag di gëna bare, ñuy wàllisi, ba doon mbooloo mu mag, góor ak jigéen.
Bindees na ci yoonu Musaa kay ne: «Bul sunjuñ gémmiñu nag te fekk koy bojj am pepp.» Ndax Yàlla nag yi doŋŋ la tiisoo?