TSK

TSK · Isaiah 33:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Aji Sax jeey jógloo ci seen kaw, xeet wu sore, ñu bàyyikoo ca cati àddina, dikk ne milib nig jaxaay, te dégguleen aw làkkam,

Xanaa boog nit ñu seen wax leerul, ñu diy làkk-kat, la Aji Sax jiy waxeek askan wii?

Ba mu ko defee Senakerib buurub Asiri daldi fabu, ñibbi. Mu toog nag ca Niniw.

Du ci waaso wu xóotu làkk te diisu làmmiñ lees la yebal. Ca waa kër Israyil nga jëm.

Bindees na ci téereb yoon wi ne: «Ay niti làkk-kat, ay làmmiñi doxandéem, ci laay waxe ak askan wii, te taxul ba tey ñu déglu ma. Boroom bee ko wax.»