Ci kaw loolu ñu woolu Buur. Gannaaw loolu bootalub buur Elyakim doomu Ilkiya moo ànd ak Sebna bindkat ba, ak ka yor téere ya, Yowa doomu Asaf, ñu dikk dajeek ñoom.
TSK
TSK · Isaiah 37:2
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
2 Kings 18:18
TSK
2 Kings 22:12
TSK
Mu wax Ilkiya sarxalkat ba, mook Ayikam doomu Safan, ak Agbor doomu Mikaya, ak Safan bindkat ba, ak Asaya bëkk-néegu buur, ne leen:
Esther 4:1
TSK
¶ Ba Mardose yégee la ñu def lépp, daa xottiy yéreem, sol ay saaku, sottikoo dóom, di ko ñaawloo, dugg ci biir dëkk bi, di yuuxu yuux gu réy te metti.
Isaiah 22:12
TSK
Bésub keroog Boroom bi, Aji Sax ji ci gàngoor yi moo leen di woo ci jooyoo ak ñaawlu ak wateefu nel, ak colu saaku ngir ñaawlu.
Isaiah 22:20
TSK
¶ «Bésub keroog ma woo sama jaam bi, Elyakim doomu Ilkiya,
Isaiah 37:14
TSK
¶ Ba Esekiya jëlee bataaxal ba ca loxol ndaw ya, jàng ko ba noppi, dafa dem ba ca kër Aji Sax ji. Mu daldi tàllal bataaxal ba fa kanam Aji Sax ji.