TSK

TSK · Isaiah 47:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Fàttlikuleen lii te dëgërluwaat! Yeen bàkkaarkat yi, defleen lii ci seen xel.

Yonent yiy wax waxyuy fen, sarxalkat yiy jiitee seen coobare, te sama ñoñ soppe ko ni! Moo bu muj ga taxawee, nu ngeen di def?»

Jeexal nga nag léegi! Maay yebal sama mer fi sa kaw. Maa lay mbugale say jëfin, yool la sa jépp jëf ju siblu.

«Yaw nit ki, yékkatilal buurub Tir kàddug jooy! Nga ne ko: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Yaa matoon royukaay, géejum xel, sottib taar.

Dees na la dàqe ci nit ñi, nga dëkk ak rabi àll yi, ñax di sam xont niw nag diiru juróom ñaari jamono, ba kera ngay xam ne Aji Kawe jee yor nguurug nit, di ko jox ku ko neex.»