TSK

TSK · Isaiah 57:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Dinaa def mbañeel sa digganteek jigéen ji, ba dëddale sa xeet ak xeetam, muy toj sa bopp, nga di ko màtt ci téstën.»

Yeen daw-làquy xeet yi, dajeleen, dikk, ànd, jegesi. Képp ku gàddu tuuru bantam, ak kuy ñaan tuur mu ko dul wallu, kooka xamul dara.

Ni gànctu yombe Israyil tax na réew mi sobewu. Njaaloo naak yàllay doj, njaalook yàllay bant.

Hosea 2:4 TSK

«Tiiñal-leen seen ndey, tiiñal-leen ko, ndax moom du sama jabar, te man duma jëkkëram. Nee ko mu bàyyi gànctu te noppee tegoo màndargam njaaloo.