TSK

TSK · Isaiah 59:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 19:8 TSK

Manumaa jàll, Yàllaa fatt sama yoon, lëndëmal samay jaaruwaay,

Yoonu ku bon ne këruus, du xam lu muy téqtaloo.

Nuy yaakaar jàmm, dara baaxul; nuy séentum paj, tiitaange ne jaas!

Amos 5:18 TSK

Wóoy kuy yàkkamti bésub Aji Sax ji! Ana lu ngeen am ci bésub Aji Sax ji? Dug leer, xanaa lëndëm.

Sa gët yu sell jomb naa niir lu bon, te manoo seetaan noteel! Ana looy seetaan ay workat? Looy noppi te ku bon di mëdd moroomam mu ko gëna jub?