TSK

TSK · Isaiah 8:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Waaye man seen Yàlla Aji Sax ji ngeen di wormaal, ma xettli leen ci seen loxol mboolem noon.»

Ba ñu yégalee Buur Axas sëtub Daawuda, ak waa këram, ne ko waa Siri, Efrayim lañu lëngool, mbir ma yëngal na Buur Axas ak waa réew ma, ba mel ni garabi gott bu ngelaw li gësëm.

Man ci sama bopp maa leen di dëfal. Ana lu ngeen di ragal ci nit kuy dee, doom aadama ju bokk akum ñax aw demin?

Luke 21:9 TSK

Bu ngeen déggee ay xare aki salfaañoo, buleen tiit, ndax fàww loolu jëkka am. Waaye du doonagum muj ga, ca saa sa.»