TSK

TSK · Jeremiah 21:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Gannaaw loolu nag,” kàddug Aji Sax jee, “Cedesyas buurub Yuda, aki jawriñam ak askan week ñi des ci dëkk bii te rëcce ci mbas meek xare beek xiif bi, maa leen di teg ci loxol Nabukodonosor buuru Babilon, ak seen loxol noon, ak loxol ñi leen di wuta rey. Dina leen leel ñawkay saamar. Du leen baal, du ñéeblu, du yërëm.”

Ana lu jar saamar akub xiif ak mbas di la rey, yaak sa waa réew mi, ni ko Aji Sax ji dige xeet wu ci nangulul buuru Babilon?

Aji Sax ji dafa wax ne: “Dees na teg moos dëkk bii ci loxol mbooloom buuru Babilon, mu nangu ko.”»

Maa lay wallu bu baax déy, ba saamar du la daaneel mukk, waaye dinga moom sa bakkan, muy sa yoolu xare, ndaxte wóolu nga ma.”» Kàddug Aji Sax jee.