TSK

TSK · Jeremiah 39:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Keroog juróom ñeenti fan ca weer wa, xiif ba tar lool ca biir dëkk ba, ba waa réew ma amatuñu ab dund.

«Yéegleen seeni tata, yàqte waaye buleen leen jeexal tàkk. Tenqileen lawit yi, ñooñoo bokkul ci Aji Sax ji.

¶ Ca fukkeelu atu ngàllo ak ñaar, keroog juróomi fan ca fukkeelu weer wa, jenn waay a rëcce ca jéllub Yerusalem ba, dikk ne ma: «Dëkk ba daanu na!»

Su bés baa,» Aji Sax jee ko wax, «yuux dina jibe fa buntu Jën ya, wóoy jibe fa Sanc ya, rajaxoo ju réy jollee ca tund ya.