TSK

TSK · Jeremiah 46:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Yéene bii ñeel na Misra: Aji Sax jaa ngii war niir wu gaaw, jëm réewum Misra. Yàllantuy Misra yég ko, di lox, fitu waa Misra rëcc.

Nga wax leen ne leen: “Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Maa ngi nii di yónnee, jëli Nabukodonosor buuru Babilon, mi ci samag curga, ba teg ngànguneem ci kaw doj yii ma fi suul, mu firi fi xaymaam.

Aji Sax ji dafa wax ne: «Maa ngii di waaja teg Firawna Ofra buuru Misra ci loxol noonam yiy wut bakkanam, na ma tege woon Cedesyas buurub Yuda ci loxol noonam Nabukodonosor buuru Babilon ma doon wut bakkanam.»